dieureudoeuf serigne touba ¿¿¿¿ diarama mame cheikh ibra
khana di contane rek thi ligueyou dongo yi khamne le mission va etre accomplir aduna bi yeup kham le vrais ligionnaire qui lutte pas avec des armes dieureudieuf khadim rassoul ¿¿¿¿¿¿ thieuy boudoul wone yow¿¿¿¿¿¿¿¿¿¿¿¿¿¿
maguettefallilou dit
11-05-2010 10:59:28
ma gui ziare di contane lol ci site bi di niane kène gueneu accentuè wakhtane dji surtout le cotè enseignement de serigne touba mais aussi les bienfaits de chaque khassidas beaucoup de site ne prenne pas ce temps c bien beau d ecouter les khassidas mais de connaitre leur secret keskil renferme et leurs beinfaits je suis fiere dy acceder mais aussi je resterais toujours a vous encourager diadieufe mouride dji da guè na bakh rek:):)
mouride76
10-05-2010 23:11:00
Bismilahi Rahmani Rahimi
Wa Salalahu Ala Seydina Muhammadin Wa Salama Tasliman
Nio ngui lene di diadieufeul si liguey bou am solo bi!!! Dina takh niou mouneul téwé yene evenement you melni Magal, Gamou, Declaration khalif général dina ko setane si internet bi!! Rawatina mbok talibé you nekk bitim rew!! Amouniou sene paye!! Yalla na liguey bi dieum kanam té mou gueun yatou si barké Borom Touba!! Akassa
Allahuma Sali Ala Seydina Muhammad Wa Ala Alihi Wa Sahbihi Wa Xadimihi Wa Salama Tasliman
Soubhana Rabika Rabil Izati Ama Yasifun Wasalamoun Alal Mursalin Wal Hamdulilahi Rabil Alamin
biram niang
10-05-2010 16:44:10
félicitation c'est une télé qui vient à son heure.Car il nous faut nous mourides des espaces pour nous exprimer et surtout montrer l'oeuvre si immenses que Serigne TOUBA nous a laissé . vivemment que cette télé serve de déclique pour une bonne vulgarisation de l'oeuvre universelle de BOROME TOUBA
matar ndao
10-05-2010 00:34:59
C'est une très belle initiative, nous nous en sommes très ravis et honorés.. Je ferai passer le lien du site auprès de mes amis et voisins de Annecy en France inchalla...
Nous sommes des mourides sadikh...
maty mbow
09-05-2010 17:08:25
dieureudieufè borom touba s.bara yala nafi yague tè wèr lol..gniongui lèndi santa tè dilène gueureum ci tele bou bèss bi tè dilène gnianale yokoutè...sounou khol sède na lol yala nalène yala faye ci barkè borom touba..amiin..ci kaw ci kanam ci lou bakh serigne touba amoul tanki guinaw you kanam rèk la am mbackè bala ayssa....diaguène jeuf
Mohamed
09-05-2010 03:58:52
Vraiment nous sommes très content de cette initiative et nous la saluons vivement
Je vous suit de très près pour la suite enfin un nouvel opus médiatique de Serigne Touba
Santati Cheikhoul Khadim Rek
sokhna mbacke tine
09-05-2010 01:02:36
Assalâmou Aleykoum War Rahmatoullâhi Taa'la Wa barakâtouho.
Barké Borome
QUE SERIGNE TOUBA VOUS PAYE DE VOTRE TRAVAIL INCHALLAHOU.
JE VOUS REMERCIE TOUS LES EXPERTS . JE FERAIS DES PRIERES POUR VOUS TOUS .
maleykoum salam War Rahmatoullâhi Taa'la Wa barakâtouho.
dieureu dieuff serigne touba
sidy bara deme
08-05-2010 23:56:03
aslamou aleykoum dieuredieufé serigne touba serigne bara mbacké yane fi yague té ande ak wére amine ca kaw ca kaname rek diam ak khéweul télé bi yallah bou si thiate dougou si barké Mohamed PSL
aissatou diop
08-05-2010 22:41:19
may cheikhoul khaddim helps you in this wonderfull job that you have started because you are currently making the muridism know by the world and it is very important. many thanks and good continuationp)p)