Diadieuf waay liguey bi rafetna. Bassirou depuis l'etranger.
sarr
25-10-2010 19:50:14
dieuredieufety serigne touba sounou yakar adouna ak alahira!!!! liguèye bi rafètena lool !!! yalla na guène dadiè ci ak guereumal XADIMOUL RASSOUL!!! cheikh sidy mackhtar yalla nafi yag loool tèè wèer !!!