li lep yokou te la si yon wi te li moy begougou mouride yi merci d avoir creer cette television ces un devellopement merci baye gueye et sidy babou et ibrahima faye merci pour tout
yibra fall
12-05-2010 22:30:15
thieuy liniou donn khaar eksina dieuredieufety serign touba thi mouride tv sant naniou bou bakh nguir nioniouy diokh li mingalek yoonwii waye diadieuf ma expertechnology yookk rek.........................
Serigne Abdou Karim
12-05-2010 18:59:52
Assalamou Enleykoum
Gno ngui léni siar tay ame mbégté thi yéné dji nguène ame ba takh nguéni takhawal MOURIDETV (MOURIDE TOUT VRAI).
Li ma léni khélale guinaw di lène gnanale moy nguène khame ki nguène done té khame lilène takha diougue maname bagna ame bène complexe (ndakh SERIGNE TOUBA KHADIMOU RASSOUL mo lène takha diougue té ay MOURIDES LAGNOU té aye sadikhes lagnouy done)
Yalla nalène Serigne TOUBA diapalé thi barkéme ak barké Rassoulilahi ak barké wa euhlou badrine ak barké xassidas yi
Dama dègue kérok wa TOUBA TV di wakhni télé bi nak dou nguir TOUBA rek wayé nguir keurou dinés yep la mou nakharima lol ndakh lolou mome complexe rèk la
Nitt da ngay na ngou fété
Tawfeex
DIAKHATE Mamadou
12-05-2010 17:39:18
p)Dieuredieuf Borom Touba, Alkhamdou lil la santati souniou boromp)
SECK MOUSTAPHA
12-05-2010 16:55:47
ASSALAMOU ALEYKOUM DI LEN ZIAR BOU WEER ...
YALLA NALEN YALLA FAY SI LIGUEY BI GUENE DI LIGUEYAL SERIGNE TOUBA.. BARKEY SERIGNE FALLOU (7fois)
SECK
12-05-2010 03:23:45
al hamdou lilaaa dieureudieuf serigne touba
SOKHNA GALLAS
12-05-2010 00:26:04
DIEUREUGUEN DIEUF MOURIDES , YALNA DIEUM KANAM BARKE SERIGNE FALLOU . DI NIANE NAK GNI YOR SITE BI GNOU GEUNA DIAPALEH NDAW GNI , RAWATINEU SOKHNA YI SI NAKA LAGNOU WARA DEF POUR GEUNA TOP SEN DINEH , NAKA LA AP SOKHNA DI NEKE SI SOCIETE BI , LAN MOKO WAR SI BIR KEUREUM , DIGUENTEM AK BOROM KEUREUM ...NDAKH SOU SOKHNA YEUP BAKHEH REK SOCIETE BI DIAR YON TEH WAKH DEUG YALLA BARI NAGNOU AY EXEMPLES LOOL MACHA ALLAH . GANAW BAMA NIANALEH SERIGNE BARRA MBACKE AK SERIGNE CHEIKH DIEUMB FALL AK NDIABOT GUEP REK MAGUI NIANAL SAMA WASILEU SERIGNE ABDOU KARIM MBACKE FALLILOU MOU YAG FI LOOL TEH AND AK WER BARKE SERIGNE FALLOU .
massamba
11-05-2010 23:37:43
p)diadieuf mourides amoul tank guinaw tank kanam rek la am yala na serigne touba agalé yénée.p)